Nooraan, La Saison Sèche du Partcours

Nooraan, La Saison Sèche du Partcours

Période : Àjjuma 30 Me 2025 → Talaata 30 Suwe 2026

Zones : Dakar, Saly

Ci biir xew-xewu mada ak kureel yi wara am ci weeru awril, mee ak suwen 2026 ci Ndakaaru, Partcours mi ngi délloosi waat « Nooraan » : di jamono jooxe lëkkalé fànn, wone-fànn, ak waxtaan yu fésal dundug mada bi ci biir Ndakaaru.

« Nooraan » bu Partcours bi, mi ngi dëggu ci sàmm-mbooleem proguraam yi, di lëkkalé bérëbi Partcours yi ak mbollooy JOKKO bi juddu ci fukk ak ñeenteelu jéego bi. Xew-xew yi amuñu pay ak ñépp mën nañu cé tàbbi.

Bégg nañu lool lool di leen gise ci xew-xew yooyu.

Top lëen Partcours !
Site web Facebook

Programmation

Tout le festival

Dalal sa xël

Maison d’Afrique

07/03/2026 → 31/07/2026

🎨 Stéphanie Nyangono, Kirubel Melke, Kha Bamba

Mbambulaan Gu Nuul laa - Je suis un océan noir

Galerie Le Manège, Plateau

17/04/2026 → 03/07/2026

🎨 Shai ANDRADE, Chris TIGRA, Bienvenue FOTSO, Amy Celestina NDIONE, Saly D, Asta NIANG, Mariéme NGOM, Anique JORDAN, Poundo GOMIS, Johanna MAKABI, Anta Germaine GAYE, Yaay Hawa FALL

Scars Speak

Hoop Galerie, Plateau

18/04/2026 → 11/07/2026

🎨 Sisqo NDOMBE, Moses MOUS

Matières de lumière

Hôtel Le Djoloff, Fann-Hock

18/04/2026 → 18/07/2026

🎨 Fallou DOLLY, Moussa Sène ABSA, Ibrahima DIALLO

Corps à battre

OH GALLERY, Plateau

25/04/2026 → 04/07/2026

🎨 Lune Diagne

AMITIÉS 2

Atelier Céramiques Almadies, Almadies

25/04/2026 → 25/06/2026

🎨 Moussa TRAORÉ, Beppe CATUREGLI, YAFANE, Cheikh DIALLO, Mauro PETRONI

Rencontres

Dakar Vintage, Point E

30/04/2026 → 30/05/2026

🎨 Karine ELBA, TAMPIDARO, Lolita GRAND

Ak Jamm

Selebe Yoon, Plateau

30/04/2026 → 25/07/2026

🎨 Alioune DIOUF

Àjjuma 24 Awril 2026